browser/browser/aboutCertError.ftl
author Francesco Lodolo (:flod) <flod@lodolo.net>
Thu, 06 Jan 2022 14:29:24 +0100
changeset 581 625cc2e007db82c90ecddd39e34f1969c4088e09
parent 540 16a43995fea0aba9a4ec25a9ddc95ce9a5d438d9
permissions -rw-r--r--
Add Mozilla Rally brand names to brandings.ftl

# This Source Code Form is subject to the terms of the Mozilla Public
# License, v. 2.0. If a copy of the MPL was not distributed with this
# file, You can obtain one at http://mozilla.org/MPL/2.0/.


## Messages used for certificate error titles

connectionFailure-title = Jokkoo bi lajj na
deniedPortAccess-title = Màkkaan bi dañu ko tere
fileNotFound-title = Dencukaay bu kenn gisul
generic-title = Laaj bi mënul sotti.
netInterrupt-title = Jokkoo bi taxaw na
notCached-title = Jukki bi jeexal na
netOffline-title = Anamu jokkoodiku
contentEncodingError-title = Jumte ci suulaale ëmb gi
unsafeContentType-title = Giri dencukaay yi wóoru ñu
netReset-title = Yeesalaat nanu jokkoo bi
netTimeout-title = Diiru jokkoo bi jeex na
unknownProtocolFound-title = Makkaan bi kenn xamuko
proxyConnectFailure-title = Servëër proxy bi nanguwul jokkoo bi
proxyResolveFailure-title = Kenn mënula gis serwëër proxy bi
redirectLoop-title = Xët wi kenn jubaluko bu baax
unknownSocketType-title = Tontu bu kenn xalaatulwoon ci serwëër bi
nssFailure2-title = Lajju jokkoo bi ànd ak kaarange
remoteXUL-title = XUL bu sori